Toq
Apparence
Toq yi (Tockus spp.) picc lañu ci néegu Bucerotidae.
Giir yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Tockus alboterminatus (Calao couronné)
- Tockus bradfieldi, Toqu Bradfield (Calao de Bradfield)
- Tockus fasciatus (Calao longibande)
- Tockus hemprichii, Toqu Hemprich (Calao de Hemprich)
- Tockus pallidirostris, Toqu sàll wu xoyyi (Calao à bec pâle)
- Tockus nasutus, Toqu sàll wu ñuul (Calao à bec noir)
- Tockus monteiri, Toqu Monteiro (Calao de Monteiro)
- Tockus erythrorhynchus, Toqu sàll wu xonq (Calao à bec rouge)
- Tockus leucomelas (Calao leucomèle)
- Tockus flavirostris, Toqu sàll wu màkka (Calao à bec jaune)
- Tockus deckeni, Toqu Decken (Calao de Decken)
- Tockus jacksoni, Toqu Jackson (Calao de Jackson)
- Tockus hartlaubi, Toqu Hartlaub (Calao de Hartlaub)
- Tockus camurus, Toq gu ndaw (Calao pygmée)